Gënéelal toude yalla – Ibrahim Khali Lô
2019-04-13
YALLA neena : ﴿فَاذْكُرُونِي أَذْكُرْكُمْ وَاشْكُرُواْ لِي وَلاَ تَكْفُرُونِ﴾(1) Toude léenma ma toude léen, sante léenma te bouléenma xarab. YALLA wakhatne: ﴿يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اذْكُرُوا اللَّهَ ذِكْراً كَثِيراً﴾(2) Yéen ñigëme déeléen toude YALLA lou bari lool. YALLA wakhatne: ﴿وَالذَّاكِرِينَ اللَّهَ كَثِيراً وَالذَّاكِرَاتِ أَعَدَّ اللَّهُ لَهُم مَّغْفِرَةً وَأَجْراً عَظِيماً﴾(3) DafalimContinue Reading