Apgaattal ci teereep: Ap tëŋkk bu am solo Ci taari lislaam – Cheikh Abdurahmane Ibn Naasir Saadi
Ci turu Yaalla laay dore sama mbinnd mi, moom miy borom yërmënde gu yaatuwi te di yërëm kuko soop. Mboolem xeeti canntyi ñeelna Yaalla, maa ngui julli aka ñaanal jaamm sunu Yonent Mouhammad aki ñoñam ak keepp kuko toopp ba bess peŋcc. Tere bi mi ngi aju ci leeral lennContinue Reading